Songtexte.com Drucklogo

Lou Tax Songtext
von Idrissa Diop

Lou Tax Songtext

Lou Tax Nith di dawe Moromame?
Lou Tax guerre doufi diexh?
Lou Tax titangué Baré?
Lou Tax xéekh doufi diexh?
Whère lène ganaye yi
Nighène di wéré yeuré
Faute lèene xêele yée
Té Bayi guerre Bé
Mane waru na yène thi diamono
Lou Tax disso diexh filé?
Lou tax dioubo ware fi Rêere?
Xole lène aye Réewi Réewe
Di Xoulo aka guerre
Whère lène ganaye yi
Nighène di wéré yeuré
Faute lèene xêele yée
Té Bayi guerre Bé
Mane waru na
Thi Diamono

Songtext kommentieren

Log dich ein um einen Eintrag zu schreiben.
Schreibe den ersten Kommentar!

Beliebte Songtexte
von Idrissa Diop

Quiz
Welcher Song kommt von Passenger?

Fans

»Lou Tax« gefällt bisher niemandem.