Songtexte.com Drucklogo

Leer Gui Fall Songtext
von Cheikh Lô

Leer Gui Fall Songtext

Mame bamba mo fi diouli guéthie
Guéthie sappé sou wétt
Guéthie sappé sou wétt
Guéthie sappé sou wétt
Yalla la defone n′ganay batakh na massoula
Neup fatal, bamba diouli guéthie
Guéthie sappé sou wétt
Thionom dji mô diour diam dji, gneuptal
Ba fara béw bamba kharé mba am ndam
May gnouko, gnoukoy n'damo
Mame bamba mofi diouli guéthie
Guéthie sappé sou wétt
Kounek ngui wakh sa khalaat
Bamba djingui sounouy khalaat
Bouléne ko sakal morom, moro mantéwoul
Bougnouko wakhé amoul morom
Bougnouko wakhoul amoul morom
Bamba diara yém foko fék fofa la mane


Bamba weét si bindam
Bamou amé batay guissatou gnou kou mélni momo
Mame bamba mofi diouli guéthie
Kou nek ngui wakh sa khalaat
Bamba djingui sounouy khalaat
Bouléne ko sakal morom, moro mantéwoul
Gaalguay diow ba tisbaar, massine ba fardi sab
Soubhana wo bamba di borom milakhwa
Mame bamba mofi diouli guéthie
Guéthie sappé sou wétt
Mame bamba mofi diouli guéthie
Fékhlene ba woor, woolonténe
Sopantalene sama gaayi dimbalentelene
Fékhlene ba woor, woolonténe
Sopantelne sama gaayi dimbalentelene
Ah mame bamba, y adioara wolo
Mame bamba mofi diouli guéthie
Guéthie sappe kou wétt

Songtext kommentieren

Log dich ein um einen Eintrag zu schreiben.
Schreibe den ersten Kommentar!

Beliebte Songtexte
von Cheikh Lô

Quiz
„Grenade“ ist von welchem Künstler?

Fans

»Leer Gui Fall« gefällt bisher niemandem.