Silence (Tongo) Songtext
von Youssou N’Dour
Silence (Tongo) Songtext
Sou néké sama nékk, nga bagne ma wo
Mba mou diapp ma, ma bagne leu wo
Khawma louko diote, ba sa khol def gome
Té gomou khol
Souma diéki diéki daméy degg am louy rire ci biir kholam
Gnou deukk ci tiow
Sama khol bi diékh, sa khol bi fess, gnoune niar nioko def
Bi khél nane nako, yow sétal bi gueune, b
Eulé khél nane doumakooo, yay séét, yay séét
Ci deug deug yaye sama goudi, yaye sama beutieuk, ba takhna yama mome
Téyit bouniou dé nélaw nioune niar déy andak téy Andak silence
Foumou tolou daféy dianérr mélnii kou réérr ci biir Mbeuguel
Niou deug ci tiow, sama khol bi diékh
Sa khol bi fess, nioune niar nioko defff
Dafa done peigner wou yoor yoor
Dafa done solou dima khar
Dafa sole lou khél ak lou bleu diko tekk ci Yaramam, yaramam, yaramam
Bouma léké mou melni lekk na
Bouma khiffé mou tagok sagom
Bouma togué, mou dianok mane dima khol, dima khol, dima khol
Bonniou daan xoulo nioune niar
Leek leek ma diékouko
Wayé leek leek mou diékouma bagne mako wone
Bagne mako, bagne mako wone ngir mbeguelo
Hé yow hé yow kay guindi ma, h
É yow hé yow kay firima, hé yooww kay wané ma Eehh love
Mbeuguel dafa nekh lolou, mbeuguel dafa nékhh, Dafa nékha nékha nékh
Ba moudj méti lolou, méti lolou, méti lolou di méték ka nekhoy
Eh yow hé yow kay ngindima
Eh yow hé yow kay firima
Eh yow hé yow kay wonéma
Ehh yow bilay
Bilay kholam dafa andak xet bou nekh
Bilay sou goudi meussana djot thi souf sédé
(Ndeysane)
Thiey way bilay bilay
Xolam dafa andak xet bou nekh
Bou melni f... Bilay

Writer(s): Habib Faye, Youssou N Dour Lyrics powered by www.musixmatch.com