Immigrés Songtext
von Youssou N’Dour
Immigrés Songtext
Guuj Njaay Faama
Guuj Njaay Faama
Uzin, bitim reew
Yuusu, dafa metti dëkku ñu fa
Mujj u mujj, yaay dañi dellusee, waaw Senegaal
Guuj Njaay Faama
Guuj Njaay Faama
Uzin, bitim reew
Yuusu, dafa metti dëkku ñu fa
Mujj u mujj, yaay dañi ñibbisee, waaw Senegaal
Olee
Guuj Njaay Faama, anh, anh
Guuj Njaay Faama
Waaw-waaw
Ñu nee "bitim reew, ñu fa nekk, dëkk u ñu faa
Mujj u mujj, yaay dañi dellusee"
Ndaxte ñooñu xamuñu leen
Fi lañu sosoo
Jóom mooy tukki yaay waaye fullay mooy ñibbisee
Noo mën a mel, loo mën a am ndeysan
Ñibbisee la war
Cóodu Faal Candèlla, yaay, Candèlla
Nene Dada mayma ci sam jaam yi
Ma dické, poŋcoo, xaajoo
Li sa caa gam neex na la
Yaayu Pale Jaaga woo nala
Dabakhee
Dabakhee (Dabakhee)
Dabakhee (Dabakhee)
Dabakhee (Dabakhee)
Dabakhee (Dabakhee)
Dabakhee, hé, hé (hé, hé)
Hé, hé (hé,hé) hé, hé (hé, hé)
Hé, hé (hé,hé) hé, hé (hé, hé)
Hé, hé (hé,hé) hé, hé (hé, hé)
Dabakhee (Dabakhee)
Miskiin mu ñëw mu teral la
Kuu àjoom ñëw mu facaal la ée Dabakh
Dabakhee (Dabakhee)
Dabakhee (Dabakhee)
Dabakhee (Dabakhee)
Dabakhee (Dabakhee)
Dabakhee, hé, hé (hé, hé)
Hé, hé (hé, hé) hé, hé (hé, hé)
Hé, hé (hé, hé) hé, hé (hé, hé)
Hé, hé (hé, hé)
Sant nañu léen, ñoo ñi leen di ñanal
Suma delloo, di leen wayaatoo
Waaw Senegaal
Mooy sunu réew
Ndaje muut nii laa, say yu nekk
Suma sañoon dii ko defeet yéen
Waaw Senegaal, Senegaal, Senegaaloo moy sunu réew
Guuj Njaay Faama
Uzin, bitim reew
Yuusu, dafa metti dëkku ñu fa
Mujj u mujj, yaay dañi dellusee, waaw Senegaal
Guuj Njaay Faama
Guuj Njaay Faama
Uzin, bitim reew
Yuusu, dafa metti dëkku ñu fa
Mujj u mujj, yaay dañi ñibbisee, waaw Senegaal
Olee
Guuj Njaay Faama, anh, anh
Guuj Njaay Faama
Waaw-waaw
Ñu nee "bitim reew, ñu fa nekk, dëkk u ñu faa
Mujj u mujj, yaay dañi dellusee"
Ndaxte ñooñu xamuñu leen
Fi lañu sosoo
Jóom mooy tukki yaay waaye fullay mooy ñibbisee
Noo mën a mel, loo mën a am ndeysan
Ñibbisee la war
Cóodu Faal Candèlla, yaay, Candèlla
Nene Dada mayma ci sam jaam yi
Ma dické, poŋcoo, xaajoo
Li sa caa gam neex na la
Yaayu Pale Jaaga woo nala
Dabakhee
Dabakhee (Dabakhee)
Dabakhee (Dabakhee)
Dabakhee (Dabakhee)
Dabakhee (Dabakhee)
Dabakhee, hé, hé (hé, hé)
Hé, hé (hé,hé) hé, hé (hé, hé)
Hé, hé (hé,hé) hé, hé (hé, hé)
Hé, hé (hé,hé) hé, hé (hé, hé)
Dabakhee (Dabakhee)
Miskiin mu ñëw mu teral la
Kuu àjoom ñëw mu facaal la ée Dabakh
Dabakhee (Dabakhee)
Dabakhee (Dabakhee)
Dabakhee (Dabakhee)
Dabakhee (Dabakhee)
Dabakhee, hé, hé (hé, hé)
Hé, hé (hé, hé) hé, hé (hé, hé)
Hé, hé (hé, hé) hé, hé (hé, hé)
Hé, hé (hé, hé)
Sant nañu léen, ñoo ñi leen di ñanal
Suma delloo, di leen wayaatoo
Waaw Senegaal
Mooy sunu réew
Ndaje muut nii laa, say yu nekk
Suma sañoon dii ko defeet yéen
Waaw Senegaal, Senegaal, Senegaaloo moy sunu réew
Writer(s): Youssou N Dour Lyrics powered by www.musixmatch.com