Songtexte.com Drucklogo

Gorée Songtext
von Youssou N’Dour

Gorée Songtext

Bama démé gorée manne
Andak samayyy kharite
Demm sa keur diam gawonne
Dama dalle di seugemm dioyy
Goor yi magg yi bi boor
Djiguéne yu magg yi bi boor
Goor yu ndaww yi bi boor
Djigéne yu naww yi tchi bénène boor
Niu daddi fayy khali yonne
Yonne bo khamni dangay demm
Yonne bo khamni dangay dem
Sa khell du demm ludull ssi délussé
Lolloyyy natu lawu buur bi mi borom doggal yyé
Lolayy nattu lawu buur bi boromm kunfa yakune
Bama démé gorée manne
Andakk samayy kharittt
Demm sa keur diamm gawonne
Dama dalle di seugueumm dioyy
Goor yi magg yi bi boor
Djiguéne yu magg yi bi boor

Goor yu ndaww yi bi boor
Djigéne yu naww yi tchi bénène boor
Niu daddi fayy khali yonne
Yonne bo khamni dangay demm
Yonne bo khamni dangay dem
Sa khell du demm ludull ssi délussé
Ennnhh gorée
Lolloyyy natu lawu buur bi mi borom doggal yyé
Lolayy nattu lawu buur bi boromm kunfa yakune
Lolloyyy natu lawu buur bi mi borom doggal yyé
Lolayy nattu lawu buur bi boromm kunfa yakune
Gorée

Gooréeeee

Songtext kommentieren

Log dich ein um einen Eintrag zu schreiben.
Schreibe den ersten Kommentar!

Quiz
Wer singt das Lied „Haus am See“?

Fans

»Gorée« gefällt bisher niemandem.