Songtexte.com Drucklogo

Siiw Songtext
von Thione Seck

Siiw Songtext

Siw dou diami borom ma thi kham dara leppeu lou yengou yow laniouye key djigne
Yegoulo fékéwo niou fénte wokhou niaw am bapa mou bari tay ko sa guinaw
Bo ma guissé di ma ré ma wone la guinaw nga yakha sama der dou ma diar dara


Refrain
Bayi lène di bakar, wokh llou la woroul lébi nène
Bayi lène di bakar, wokh llou la woroul lébi nène
L′islam da key ayé

Diapa sa ma dom di dor ma takhaw di la khol bou sa yaram dé daw nga bayi ko
Fi la deukeu fi la djoudo di weuye sa ma mame teki dara guene wo yéwoulène
Lou way di def di thia tokh kénée tedda na thia mbirou yalla mo woor

Refrain

Bo ma guissé di ma ré ma wone la guinaw nga yakha sama der dou ma diar dara

Songtext kommentieren

Log dich ein um einen Eintrag zu schreiben.
Schreibe den ersten Kommentar!

Beliebte Songtexte
von Thione Seck

Fans

»Siiw« gefällt bisher niemandem.