Capsi Songtext
von Positive Black Soul
Capsi Songtext
Ena min na gwan
Hey haha
Kone ñun ñoy Positive Black Soul
Yako tey xam nga ñou
Yeah gnow represent sunu cité
Sunu deuk yeah
Capsi yeah haha
Hey
Liberté 1, Liberté 2, Liberté 3, Liberté 6
Xolal Positive Black Soul
Amitié 2, Liberté 6
Xalé ya ngui ni
Goné ya ngui yi
Goor ya ngui ni
Dama né thiof ya ngui ni
Kone nak thiakass guiin guiin
Thiakass thiakass guiin guiin
Xolal PBS noumouy dokhé si biir town bi
Dama né thiakass guiin guiin
Thiakass thiakass guiin guiin
Xolal PBS, Awadi ak Duggy Tee
Boul falé fofou la diogué
Ataya fofou la diogué
Djoko fofou la diogué
Daw thiow fofou la diogué
Yow Bugs fofou la diogué
D-Black fofou la diogué
Awadi fofou la diogué
Dama né Duggy Tee fofou la diogué
Kone nak thiakass guiin guiin
Thiakass thiakass guiin guiin
Xolal PBS noumouy dokhé si biir town bi
Dama né thiakass guiin guiin
Thiakass thiakass guiin guiin
Xolal PBS, Awadi ak Duggy Tee
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Mangui mangui
Mangui mangui
Diogué Town tokk tchi taxi
Gnouné ma Duggy fane nga dieum
Mané la Capsi
Damey setti sama gayi ndakh té gnoune gni tey dji daniou wara fecci woy
Duggy dafa Duggy dafa sexy
Té Capsi dama beugueu nga mey setsi
Positive Black Soul mo ayé
Kone yow degloul li oh yeah
Boul fo oy
Yow xamal li la dioklo
Represent fi nga deukeu té di setlo
Goné Capsi dem ba diekh mo ñou takac diok yow
Kone yow boul falé tchi Capsi
Boul falé tchi Capsi
Hey yow hey yow
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Liberté 4, Liberté 5 gnou gui kaass si Awadi
Ne nene tey di negne ma clamer
Ndakh té mane dama lene planer
Non non, mane douma la planer
Douma la douma la planer
Barki serigne bi domou ndeye soum ko deffé meune ngama blamer
Moun nga ma né Awadi demal né
Awadi tafoul né
Wanté tey dji mome dou ney
Ndakh Capsi dama leu beugue
Ya di sama xol
Boul tite té boul diakhlé
Yow mi da nga mol
Eh yow
Mangui mangui deloussi
Indi benene style
Kone yow degloul li
Khamel ma wa Capsi
Liberté, Amitié, Dieupeul, Mermoz, Derklé,
Karack, Baobab, Fann goné ya ngui gnéfé
Wanté soma deggué mane mey woy Capsi
Guedizwaye ba Colobane
Gnoune gneup ngui si
Gno bokkeu beneu town
HLM ba Medina
Castor ba Grand Yoff
Parcelles, Zone B, Zone A
Hey yow hey yow
Hey yow hey yow
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Hey haha
Kone ñun ñoy Positive Black Soul
Yako tey xam nga ñou
Yeah gnow represent sunu cité
Sunu deuk yeah
Capsi yeah haha
Hey
Liberté 1, Liberté 2, Liberté 3, Liberté 6
Xolal Positive Black Soul
Amitié 2, Liberté 6
Xalé ya ngui ni
Goné ya ngui yi
Goor ya ngui ni
Dama né thiof ya ngui ni
Kone nak thiakass guiin guiin
Thiakass thiakass guiin guiin
Xolal PBS noumouy dokhé si biir town bi
Dama né thiakass guiin guiin
Thiakass thiakass guiin guiin
Xolal PBS, Awadi ak Duggy Tee
Boul falé fofou la diogué
Ataya fofou la diogué
Djoko fofou la diogué
Daw thiow fofou la diogué
Yow Bugs fofou la diogué
D-Black fofou la diogué
Awadi fofou la diogué
Dama né Duggy Tee fofou la diogué
Kone nak thiakass guiin guiin
Thiakass thiakass guiin guiin
Xolal PBS noumouy dokhé si biir town bi
Dama né thiakass guiin guiin
Thiakass thiakass guiin guiin
Xolal PBS, Awadi ak Duggy Tee
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Mangui mangui
Mangui mangui
Diogué Town tokk tchi taxi
Gnouné ma Duggy fane nga dieum
Mané la Capsi
Damey setti sama gayi ndakh té gnoune gni tey dji daniou wara fecci woy
Duggy dafa Duggy dafa sexy
Té Capsi dama beugueu nga mey setsi
Positive Black Soul mo ayé
Kone yow degloul li oh yeah
Boul fo oy
Yow xamal li la dioklo
Represent fi nga deukeu té di setlo
Goné Capsi dem ba diekh mo ñou takac diok yow
Kone yow boul falé tchi Capsi
Boul falé tchi Capsi
Hey yow hey yow
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Liberté 4, Liberté 5 gnou gui kaass si Awadi
Ne nene tey di negne ma clamer
Ndakh té mane dama lene planer
Non non, mane douma la planer
Douma la douma la planer
Barki serigne bi domou ndeye soum ko deffé meune ngama blamer
Moun nga ma né Awadi demal né
Awadi tafoul né
Wanté tey dji mome dou ney
Ndakh Capsi dama leu beugue
Ya di sama xol
Boul tite té boul diakhlé
Yow mi da nga mol
Eh yow
Mangui mangui deloussi
Indi benene style
Kone yow degloul li
Khamel ma wa Capsi
Liberté, Amitié, Dieupeul, Mermoz, Derklé,
Karack, Baobab, Fann goné ya ngui gnéfé
Wanté soma deggué mane mey woy Capsi
Guedizwaye ba Colobane
Gnoune gneup ngui si
Gno bokkeu beneu town
HLM ba Medina
Castor ba Grand Yoff
Parcelles, Zone B, Zone A
Hey yow hey yow
Hey yow hey yow
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Capsi, lève tes mains et représente
Writer(s): Amadou Barry, Didier Sourou Awadi Lyrics powered by www.musixmatch.com