Songtexte.com Drucklogo

Sey Songtext
von Orchestra Baobab

Sey Songtext

Bo takei seu diego am ak mom ay dom
Boko wathié wathie ndiabot takhawalou
Lolou amoul mana
Anh yaw mi djigueno neu ngeu diapeu seu sey
Tei fo meuneu toleu nangoul dane seu dolei moy seu warefo
Han bayi leine di diayo yeine seini dom
Alal dou sey sey gnéti waref leu tey meu li meul leine ko
Anh doundou bou doy
Thiangay lou doy
Diameu diou sakh
Lolou mo di sey aa gayi seidei leine meu
Mountaga koité sama domi yaye leu
Louleu meiti big moy ba diameu ngeu am dom man dei nameu naleu
Aladji

Songtext kommentieren

Log dich ein um einen Eintrag zu schreiben.
Schreibe den ersten Kommentar!

Beliebte Songtexte
von Orchestra Baobab

Fans

»Sey« gefällt bisher niemandem.