Songtexte.com Drucklogo

Mbélé Songtext
von Lass

Mbélé Songtext

Yéen last timp nga nékk di misère
Ndax gaa yi di wax di yakk deer
Fàtal sa xel ba méen ni xéra
Suñ la giise di bëgg dee ya
A xolal gestu maléen
Yaw giisal falé wumaléen
Fi lek ya ñi deff, ñoom lu léen nex
Yaw de doto am lu la nex

Mbélé
Mbélé mbélé
Mbélé bayiléen mbélé
Mbélé
Mbélé mbélé
Mbélé bayiléen mbélé

Mbélé bayil mbélé
Mbélé bayil mbélé


Xoolal li maay dundee te nexula lu ci yoon
Xoolal ni maay doxee te nexula lu ci yoon
Ya xool, ya giis, ya wax, yaw lu ci yoon
Léegi daal mala desee lu ci sa yoon
Do mës a xam, sama wërsëk kañ lay yëw
Lan ngaay soon yaw di ko djeema wër
Yeen dëggar fiit yi, ma nee woorul
Bayiléen ñoom yi wax, yaw ngaay doori waar

Mbélé
Mbélé mbélé
Mbélé bayiléen mbélé
Mbélé
Mbélé mbélé
Mbélé bayiléen mbélé

Mbélé
Mbélé mbélé
Mbélé bayiléen mbélé
Mbélé
Mbélé mbélé
Mbélé bayiléen mbélé

Mbélé
Mbélé mbélé
Mbélé bayiléen mbélé
Mbélé
Mbélé mbélé
Mbélé bayiléen mbélé
Heu

Songtext kommentieren

Log dich ein um einen Eintrag zu schreiben.
Schreibe den ersten Kommentar!

Beliebte Songtexte
von Lass

Quiz
„Grenade“ ist von welchem Künstler?

Fans

»Mbélé« gefällt bisher niemandem.