Sama Néné Songtext
von Assiko Golden Band De Grand Yoff
Sama Néné Songtext
Sama néné mongi dioyé héé
Néné yaw lodi diooye
Sama tanta moma doréé
Yaye booy nakhal makoo, maman
Sama néné mongi dioyé héé (mongi diooy)
Néné yaw lodi diooye (mola door)
Sama tanta moma doréé (thiey moma door)
Yaye booy nakhal makoo, maman
Sama néné mongi dioyé héé
Néné yaw lodi diooye
Sama tanta moma doréé
Yaye booy nakhal makoo, maman
Sama néné mongi dioyé héé (mongi diooy)
Néné yaw lodi diooye (ohh lodi dioy)
Sama tanta moma doréé (thiey moma door)
Yaye booy nakhal makoo, maman
Kouy laal Ma Demba
Sabar yassa Ngaay dess koy ndaat ndaat say
Kouy laal sama doom djéé, yaye
Ayo béyo béyo
Kouy laal Ma Demba
Sabar yassa Ngaay dess koy ndaat ndaat say
Kouy laal sama doom djéé, waw
Ayo béyo béyo
Kouy laal Ma Demba
Sabar yassa Ngaay dess koy ndaat ndaat say
Kouy laal sama doom djéé, yaye
Ayo béyo béyo
Kouy laal Ma Demba
Sabar yassa Ngaay dess koy ndaat ndaat say
Kouy laal sama doom djéé, waw
Ayo béyo béyo
Sama néné mongi dioyé héé
Néné yaw lodi diooye
Sama tanta moma doréé
Yaye booy nakhal makoo, maman
Sama néné mongi dioyé héé (mongi diooy)
Néné yaw lodi diooye (mola door)
Sama tanta moma doréé (thiey moma door)
Yaye booy nakhal makoo, maman
Sama néné mongi dioyé héé
Néné yaw lodi diooye
Sama tanta moma doréé
Yaye booy nakhal makoo, maman
Sama néné mongi dioyé héé (mongi diooy)
Néné yaw lodi diooye (hoo lodi diooy)
Sama tanta moma doréé (thiey moma door)
Yaye booy nakhal makoo, maman
Sama doom sama sopé
Dounda matta dioy oh
Mom lay dioy doom
So doundé ba matt liguéy waw
Térél say wadiour
Kouy laal Ma Demba
Sabar yassa Ngaay dess koy ndaat ndaat say
Kouy laal sama doom djéé, yaye
Ayo béyo béyo
May niaane Ma Demba nga doy si baye boy mom lay dioy doom
So doundé ba mat liguéy waw
Féral say rangogne
Kouy laal Ma Demba
Sabar yassa Ngaay dess koy ndaat ndaat say
Kouy laal sama doom djéé, waw
Ayo béyo béyo
Ayo béyo béyo
Ayo béyo béyo
Kouy laal sam dome djé yaye
Ayo béyo béyo
Néné yaw lodi diooye
Sama tanta moma doréé
Yaye booy nakhal makoo, maman
Sama néné mongi dioyé héé (mongi diooy)
Néné yaw lodi diooye (mola door)
Sama tanta moma doréé (thiey moma door)
Yaye booy nakhal makoo, maman
Sama néné mongi dioyé héé
Néné yaw lodi diooye
Sama tanta moma doréé
Yaye booy nakhal makoo, maman
Sama néné mongi dioyé héé (mongi diooy)
Néné yaw lodi diooye (ohh lodi dioy)
Sama tanta moma doréé (thiey moma door)
Yaye booy nakhal makoo, maman
Kouy laal Ma Demba
Sabar yassa Ngaay dess koy ndaat ndaat say
Kouy laal sama doom djéé, yaye
Ayo béyo béyo
Kouy laal Ma Demba
Sabar yassa Ngaay dess koy ndaat ndaat say
Kouy laal sama doom djéé, waw
Ayo béyo béyo
Kouy laal Ma Demba
Sabar yassa Ngaay dess koy ndaat ndaat say
Kouy laal sama doom djéé, yaye
Ayo béyo béyo
Kouy laal Ma Demba
Sabar yassa Ngaay dess koy ndaat ndaat say
Kouy laal sama doom djéé, waw
Ayo béyo béyo
Sama néné mongi dioyé héé
Néné yaw lodi diooye
Sama tanta moma doréé
Yaye booy nakhal makoo, maman
Sama néné mongi dioyé héé (mongi diooy)
Néné yaw lodi diooye (mola door)
Sama tanta moma doréé (thiey moma door)
Yaye booy nakhal makoo, maman
Sama néné mongi dioyé héé
Néné yaw lodi diooye
Sama tanta moma doréé
Yaye booy nakhal makoo, maman
Sama néné mongi dioyé héé (mongi diooy)
Néné yaw lodi diooye (hoo lodi diooy)
Sama tanta moma doréé (thiey moma door)
Yaye booy nakhal makoo, maman
Sama doom sama sopé
Dounda matta dioy oh
Mom lay dioy doom
So doundé ba matt liguéy waw
Térél say wadiour
Kouy laal Ma Demba
Sabar yassa Ngaay dess koy ndaat ndaat say
Kouy laal sama doom djéé, yaye
Ayo béyo béyo
May niaane Ma Demba nga doy si baye boy mom lay dioy doom
So doundé ba mat liguéy waw
Féral say rangogne
Kouy laal Ma Demba
Sabar yassa Ngaay dess koy ndaat ndaat say
Kouy laal sama doom djéé, waw
Ayo béyo béyo
Ayo béyo béyo
Ayo béyo béyo
Kouy laal sam dome djé yaye
Ayo béyo béyo
Writer(s): Djiby Ly Lyrics powered by www.musixmatch.com